34 comments

  1. Ngaka meune neu rap lolou j sé prsk il é tjrs en laise si beat yi té ossi flow bou nékh la yor ak ay rime mé pour mane ecriture bi da déss lole sakh da wara xam ni nékkatoul khalé légui bokkou na si 5 rappeur you gueuneu siw galsen donc na fékhé yégueul lyrics yi

Leave a comment

Your email address will not be published.